Youssou Ndour - Ballago ndoumbé yatma - ALBUM - MBALAX

Youssou Ndour
Youssou Ndour
Publié le 12.11.2021

El Maestro, tu es parti sur la pointe des pieds ! El Maestro, tu es parti mais ton immense œuvre restera à jamais. Merci pour tous ces moments de bonheur que tu nous as procurés. Merci pour ton inestimable implication pour bâtir un Sénégalais modèle. Grand Thione Ballago Seck, Ballago Ndoumbe Yatma, repose éternellement en paix.
PAROLE :
Billaay , ballago ndoumbé yatma ,
su ñu waaji xaj oon na fi
Naxxar doηη ,la ñu bayyee
yalla , wonneeti na


Li tax ba mbir mi metti lool,
ñun da ñu ko foog wul woon
Yëf yi gaaw ba bette gnou
billaay wéetël na ñu

Njiinoo njiin faramaareen,
gòor u jaaga , nelaw naa
Baay i wally dem na nii ,
ñun daal wéetël na ñu

Ma ngi koy jaale Sénégal,
di ko jaalé Gambia
Di ko jaalé adduna ,
ndaanaan ba dem na nii


Thione ballago , ndoumbé yatma
Bu yalla buur bi doon taggoo ,
kon di na ñu bayék yaw
Ni patrimoine bi nga ñu bayyeel ,
Yee gua nit gñi , tete leen ci adduna
Yee gua nit gñi , tete leen
xam al leen ci adduna
ahhh - Balaago

Yee gua nit ñi ci adduna xam al leen
Ni ñu war a nekkek
Ak ni ñu war a dundée ,
Ak ni ñu war a jëfleentee
Jinaxoo mbaay
yaw mi dëkké biir suuf ,
Boo dem ee neel ballago , réew maa ngi koy joy
Aduna ngi koy jooy ,
art baa ngi koy jooy



Njiin faramaareen ,
thione seck , wéetël na ñu
Ballago ndumbé yaatma
adduna , am ul solo

Li tax ba mbir mi metti lool,
ñun da ñu ko foog wul woon
Yëf yi gaaw ba bette gno
Ndanaan ba demna ni
Njiin faramaareen ,
thione seck , wéetël na ñu
Ballago ndumbé yaatma
adduna , am ul solo






Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
http://www.youtube.com/c/YoussouNdourofficiel
https://www.facebook.com/youssoundourofficiel
https://www.instagram.com/youssoundour1959

Runtime 00:05:15

Youssou ndour, ndour, tfm, lobs, ministre, chanteur, dakar, senegal, africa, international, Youssou Ndour, Hello, Boukki YI, Bercy, Xaware youssou ndour, Fiitey, Grand Bal, Ballago ndoumbé yatma - ALBUM - MBALAX, Ballago ndoumbé yatma, THIONE SECK, YOUSSOU NDOUR,

COMMENTAIRES: 1,802